Youssou N'dour
Youssou N'dour

Li Ma Weesu Lyrics English translation

Lyrics

Youssou N'dour - Li Ma Weesu

li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
seetal;
leegi leegi ma gesu, ci li ma weesu
leegi leegi ma recu, walla sax di baaku
fu gune yi feetee, dama leen di teetee
wax nu ma neexee, ma bëgga leen
damay, damay, damay dellu gune
mel ni,mel ni, mel ni duma màgg
lu ma gën di yàgg, xel ni mel ni bank
lu ma gën di màgg, dellu tuuti tank
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
ma ni seetal;Youssou N'dour - Li Ma Weesu - http://motolyrics.com/youssou-ndour/li-ma-weesu-lyrics-english-translation.html
leegi leegi ma gesu, ci li ma weesu
leegi leegi ma recu, walla sax di baaku
fu gune yi feetee, dama leen di teetee
wax nu ma neexee, ma bëgga leen
damay, damay, damay dellu gune
mel ni,mel ni, mel ni duma màgg
fu gune yi feetee, dama leen di teetee
wax nu mu ma neexee ma béggati
li ma gën di jege, mel ni dama sore
lu ma gëna sore, gën di gis li ma jegewoon
lu ma gën di yàgg, xel ni mel ni bank
lu ma gën di màgg, dellu tuuti tank
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
damay, damay, damay dellu gune
mel ni,mel ni, mel ni duma màgg... Submitter's comments:  The website has stated they are French, but I believe they may be in Wolof. :/

English translation

Youssou N'dour - as in a mirror (English translation)

My past always comes back as in a mirror
Sometimes I look back to my past life
With regret or pride
When I'm around the children I love, they dance and I guide
them and I express myself in such a way that I want to be a
child again and never grow older
The longer I stay away, the more forgetful I am
The older I grow, the more I look back to the past
and want to be a child again
My past always comes back as in a mirror
Sometimes I look back to my past lifeYoussou N'dour - Li Ma Weesu - http://motolyrics.com/youssou-ndour/li-ma-weesu-lyrics-english-translation.html
With regret or pride
When I'm around the children I love, I feel happy again
They dance, I guide them and express myself in such a way
that I want to be a child again and never grow older
The closer I am, the farther I feel
The farther I am, the closer I feel
The longer I stay away, the more forgetful I am
The older I grow, the more I look back to the past
And want to be a child again
My past always comes back as in a mirror

Write a comment

What do you think about song "Li Ma Weesu"? Let us know in the comments below!